Aayóo nenne

Aayóo nenne!
Ku may bindal téere
yobbul ma ko Saalum?
Saalum, ñaari néeg la
ñetteel ba di waañ wa
waañ wi waañu buur la
aayóo nenne!
aayóo nenne!
nenne nenne tuuti

>> mp3



Aayóo nenne
Aayóo nenne!
Ku ma-y bind-al téere
Quen me-IMPERF escribir-APLIC libro
"Quen me escribirá o libro
yobbu-l ma ko Saalum?
levar-APLIC me o Salum
e mo levará a Salum?"
Saalum, ñaari néeg la
Salum, dúas habitación AuxL.3sg
"En Salum hay dúas habitacións"
ñetteel b-a di waañ w-a
terceira CL-DIST Aux.3sg cociña CL-DIST
"A terceira é a cociña"
waañ w-i waañ-u buur la
cociña CL-PROX cociña-REL rei AuxL.3sg
"A cociña é a cociña do rei"
aayóo nenne!
aayóo nenne!
nenne tuuti




Grupo de Tipoloxía Lingüística: wolof (Universidade de Vigo)
Última modificación da páxina 16 April 2009 ás 10h36, por JMGM